Enterrement du père de Modou Lô : Eumeu Séne, Baboye, Tapha Guèye et le monde de la lutte présents Herunterladen

An deine Freunde senden
Hinzufügen
  • 08.05.2020

  • Visitez notre site web http://luttetv.com/ et aimez notre page Facebook pour voir des combats en direct https://www.facebook.com/luttetv/ https://www.facebook.com/luttetv/ https://www.instagram.com/luttetv/ http://luttetv.com/ https://www.youtube.com/user/senlamb

Kommentare

  • L’absolu Gueye
    L’absolu Gueye vor 4 Monaten

    Naysann Mdou Lo Masta way 😭😭😭Mètina Trop Yallah Nako souniou borom Yeureum thi Barke borom touba 🙏♥️🙏

  • babacar dieng
    babacar dieng vor 4 Monaten

    Ndeysane li moy senegal so amé banekh nio tewlé la so amé nakar tamit niou tewlé la

  • Bamba Seck
    Bamba Seck vor 4 Monaten

    C'est vraiment beau c ça le Sénégal billahi sama yaram dawna adversité dou animosité

  • Amadou Sarr
    Amadou Sarr vor 4 Monaten

    Li rafétena yalnako yalla yeureum. Té amenagne ci yakaar ci barké weerou koor gui.

  • OUSMANE SONKO THIAM
    OUSMANE SONKO THIAM vor 4 Monaten

    Inaa lilaahi wa inaa ilayhi raajihon yalnako yallah yeureum tam jeugalko kharéko aljana ci barki wérou koor gui

  • Mody Waiga
    Mody Waiga vor 4 Monaten

    Ndeysane yalnako souniou borom yeureum té kharéko aldiana firdawsi

  • AKHIBOU SAMB
    AKHIBOU SAMB vor 4 Monaten

    Qu Allah l'accueil Dans son paradis AMINE 🙏

  • Mouhamed Ndong
    Mouhamed Ndong vor 4 Monaten

    Yalnako yallah geureum tei xarrei aldjana firdawsi ci Barkep Muhammad PSL metina trop mais Modou Lo Siggil ndigalei

  • Cheikh Mbacke
    Cheikh Mbacke vor 4 Monaten

    LI DIANNGATT LAA TCHI SUPPORTER YII DEFANTER LOU BONN NGUIR MBEUR YII TE NIOM BEN LANOU KON SUPPORTER NANIOU DON BEN ADUNA DOU DARA NA RAFET REK

  • ndaraw Niang class'chicc
    ndaraw Niang class'chicc vor 4 Monaten

    Yalna ko yalla kharé aldiana

  • Sidi Thiam
    Sidi Thiam vor 4 Monaten

    Nako yala yareume di masa wo modou lo takh té sonou na si papame di roup limou nék si opitale bi modou taloul dara bou guéné sakh di dieunde guerap daye daw wala mouye wakhou si biti bi lako done guisé lolou mane nako sédé

  • Cheikh Diouf
    Cheikh Diouf vor 4 Monaten

    Modou courage ,yalla na yalla yeureme ko haréko aldiana firdawous si barké Seydouna Mouhamet amine ya Rabi

  • Babacar Sarr
    Babacar Sarr vor 4 Monaten

    Sunu roi sama roi magii lay mastawou dila dialé dila nianal o6 sa papa sunu mame yal nako yeureume té Khéréko Aldiana Sii Barkké Yonantéby (PSL) Champion dit courage Mouneieul o6.....

  • Momo Touray
    Momo Touray vor 4 Monaten

    Que Firdawsi soit sa demeure éternelle Amine courage La vie est Courte

  • Daouda Ndiaye
    Daouda Ndiaye vor 4 Monaten

    Ndeysane 😭 yalnako yalla yeureum kharéko aldiana 😭 Sénégal ni rek la raféte na yalna yalla konn tann 🤲🤲🤲👈

  • Cisse Mouhamed
    Cisse Mouhamed vor 4 Monaten

    Yalla nako yalla yeurem si barkep serigne babacar s'y

  • Amadou Gassama
    Amadou Gassama vor 4 Monaten

    Amine Lac 2

  • Ambroise Mendy
    Ambroise Mendy vor 4 Monaten

    Pikine la deuk mais dama beugue modou lo yalla na yalla kharé pabi sa aljana you kawéya

  • Mansour Dieng
    Mansour Dieng vor 4 Monaten

    VENDREDI 8 MAI 2020 YALLA NAKO YALLA KHARÉ ALDIANA BALLA MODOU EUMEU SÉNE YÉNA BOKOU NDAYE AK BAYE ADOUNA AMOUL SOLO 😭😭

  • Baba Thiam
    Baba Thiam vor 4 Monaten

    Ndeysan paix à son âme