GALLÉ NO STRESS - Episode 17 - 10 Mai 2020 Herunterladen

An deine Freunde senden
Hinzufügen
  • 10.05.2020

  • Pour plus de vidéos, abonnez-vous sur notre chaine http://www.youtube.com/c/SSPSENEGAL

Kommentare

  • Kmnd Team
    Kmnd Team vor 4 Monaten

    képp kou sopp Seydina Mouamed PSL ,manguilay niane ngua abonnél ma si sama chaine ''KMND TEAM" si barké wérou koor gui svp

  • ibrahima ndiaye
    ibrahima ndiaye vor 4 Monaten

    Na kén kouné wakh serigne mountakha yalla nafi yague képou kouko wakh yalla nga doundou lou bari doundou ba doyal wakhal Amine🙏

  • TER NIANE
    TER NIANE vor 4 Monaten

    Ani wa team COCOTE manifestez vous waye 😇😍🙋‍♂️🙋‍♂️🙋‍♂️

  • Madiagne Sarry
    Madiagne Sarry vor 4 Monaten

    Fi ana niuye baye di fathi non baye sérieux woul quoi 😂😂😂😂😂

  • Saliou Ndiaye
    Saliou Ndiaye vor 4 Monaten

    Baye c'est un grand comédie et il à bien réussir son rôle qui est d'accord avec baye clique j'aime

  • Diop Adama
    Diop Adama vor 4 Monaten

    Premiere commentaire kou beugue abba beuseul jaime👇👇

  • Adiana Tall
    Adiana Tall vor 4 Monaten

    Yall na diamou yaga Sénégal barké siyedina Mohamed 🇸🇳🇸🇳❤

  • Ibrahima Cisse
    Ibrahima Cisse vor 4 Monaten

    Yallah na fi corana djouguè si barké koor gui 🙏

  • ALIOU NIANG
    ALIOU NIANG vor 4 Monaten

    Bilahi baye rew na man COCOTE COCOTE mo maye ray 😂😂😂😂😂

  • Ndeye Binta Ndiaye
    Ndeye Binta Ndiaye vor 4 Monaten

    Wa kou guiss nè Gogote da nirok mamy linguèr mi nek warèf tfm 😍

  • Ada boy GSB
    Ada boy GSB vor 4 Monaten

    Respect tout les enfants du maison sauf toi

  • Ndeye Binta Ndiaye
    Ndeye Binta Ndiaye vor 4 Monaten

    Ayooooo Baye Amna ndam 😂😍

  • Djily Fall
    Djily Fall vor 4 Monaten

    Tay d xana may imame bi fi wala 😂ani fan baye yi ♥️😂

  • boubacar yade
    boubacar yade vor 4 Monaten

    En fain baye wakhna deugue taye mane pour mane do indi dara 😂😂😂😂

  • Rokhyatou Lo
    Rokhyatou Lo vor 4 Monaten

    Vous êtes les meilleures Baye mome dama ko beuggg .Pépéna dou niewate

  • Mbayang Diop
    Mbayang Diop vor 4 Monaten

    Blh man baye la beug promis juré wooooooooyyyyyyyyyy rérr rérr😂😂😂😂

  • Gaye Moustapha
    Gaye Moustapha vor 4 Monaten

    Vittoria di Baye....... Baye tay amnga ndam lou reuyy waay🤣🤣🤣🤣

  • Sidy Al Maktoum Gaye
    Sidy Al Maktoum Gaye vor 4 Monaten

    Mais lou takh baye rèw

  • Ousmane SARR
    Ousmane SARR vor 4 Monaten

    Gogoteee, il me fume baye 😂😂

  • IBRAHIMA Niang
    IBRAHIMA Niang vor 4 Monaten

    Yalla na nieup am diamou si barkéb Borom touba 🤲🤲🤲❤